MENU

Fun & Interesting

Safary - NDANK REK feat. Jahman X-press (clip officiel)

Safary 786,372 1 week ago
Video Not Working? Fix It Now

Stream NDANK REK : https://bfan.link/ndank-rek •• Les crédits de la chanson et du clip Prod / Jeuss Beat & Bouba Direction artistique : Jahman Auteur : jahman Réalisation / montage / étalonnage Mao sidibe Cadrage: Oumar Ndiaye Lumière : Mamadou Dia Stylisme : Bise collection, Gringo Guest : Guest j live et molze Remerciements : Lamine Ba, Keba, Restaurant calienté corniche des almadies, Restaurant champs senegambia, Africa princess hotel Gambia, Garage SBS moto Medina Lyrics Saf Mool Nekh Tooy So répé ba dougou ci man Ak nima nékhé Tay nga dé Oh bb, douma reubeu di sooy Souma nélé nipe Doto dooy Khadioul ci yow sama beureudj Man comme drogue ci déréte Yako tay wakhok tapéte Douma délo avance Dédéte Khadioul ci yow sama beureudj Man comme drogue ci déréte Yako tay wakhok tapéte Douma délo avance Dédéte Lolo takh Manila Ndank ndank ndank Somay nope nope ma ndank ndank ndank (namone na) Ndakh dama beuri vice (oh) Damléy coller serré Sa tankak sama tank (ndiap rek) Oh baby Dama siss, bo sété ba ci biir Gni malén gueuneu pank ( eh wouyoul li ) Sama baby, goudi tay bi Narna yague, narna meti Samay Baram Di dokhanetou Ci sa yaram Ndaw lou sexy Oh baby souma fipo Mba doo tagok sa sago Khana sibo Man dama bari djiko Baby souma fipo Mba do tagok sa sago Khana siboo, dama bari Djiko Néwone nala Ndank ndank ndank Somay nope nope ma ndank ndank ndank Eeh yow Néwone nala ndank ndank ndank Somay nope nope ma ndank ndank ndank Ndakh dama beuri vice Damléy coller serré Sa tankak sama tank Oh baby Dama siss, bo sété ba ci biir Gni malén gueuneu pank Kham ngani kén douma wéthiooo Nekhouma déréte Yague nala kép ngay youkhoo Dima wowé sa yaye Nane ma yaye, boye So beugué keurgui kén doufi fanane tay ( eh pape guéneul keurgui ) Nane ma yaye,( thiabiti) boyoo (non bouma yakal) Yanguimay gagn Manane leu B loy dioy Jahman Héee nangouna seuy bi tay dieulna défaite Doyalouma sodé soucar yalna diabéte Yow danga dal tekci yalén gueuneu coquette Oh baby Kay fi ma defla tapéte Kaay gaw Bayil lolou Boul laal fofou Dafay dawlo sama yaram Man nak hahan hahan han Yangmay rélo sakh Arrêtél tamite Khawma loutakh nga saï saï Mangui saalit tamite Yow linga bouga Lolou la bouga Tay fi ba souba amoul nelaw Aythia diougal aythia Wakh dji boum gouda So toyé nala soupal Sol sama khoukhal Diék dila khoukhal Khoukhal khoukh Néwone nala Ndank ndank ndank Somay nope nope ma ndank ndank ndank (namone na) Ndakh dama beuri vice (oh) Damléy coller serré Sa tankak sama tank (ndiap rek) Oh baby Dama siss, bo sété ba ci biir Gni malén gueuneu pank ( eh wouyoul li ) #safary #ndankrek #jahman #music

Comment